Beug Dem sur toutes les plateforme : https://ceepee.lnk.to/BeugDemRG
Ceepee: Instagram : https://www.instagram.com/ceepee_officiel Facebook : https://www.facebook.com/CeePeeMusic
Daddy Mory: Chaine youtube de Daddy Mory : https://bit.ly/340kwca Instagram : https://www.instagram.com/realdaddymory/ Facebook : https://www.facebook.com/daddymoryofficiel
Auteur : Ali Diallo & Mory Samake Prod by : Dub Akom Editeurs : JNS Editions Label : Creepy Music Distribution : Believe Mixé par : Laboklandestino Masterisé par : Simon "Basalte Studio" Clip Réalisé par : Raydi Visual / Sick Shots Un grand merci à Elou (Challenge Events) sans qui ce clip n'aurait pu être réalisé.
Lyrics:
Ici y'a pas d'eldorado Tout ce qu'on vous raconte est faux
Sama gaayi dagnu bëgg dem Guen dem funé beug naaniu Naax fi daafa taar men Laamgu waalanimën Hi them crying again Lidu ronganiu nënn Bokku ci rewmi taaxul niu soraalè lënn Booy doox ci mbédmi faaw nga guissalé lënn Gumba rek meuna waaxni raagnéwulënn
Funé nioguifaa akaa nio yomba guiss Duniu lakaatu naax jaayuniu canabis Daagni job nguir tiop amuniu bénéfice Dugnu xeuy di tokk week-end ci bënn biss Amungnu deureum motax guemugnu justice Lignu deuku teuna dak taax naa dagnuko miss Gnuniu gnufii daak am problème police Mooy gni menul am visa di tukki sans valise
Sama gaayi dagnu bëgg dem Guen dem funé beug naaniu Naax fi daafa taar men Laamgu waalanimën Hi them crying again Lidu ronganiu nënn Bokku ci rewmi taaxul niu soraalè lënn Booy doox ci mbédmi faaw nga guissalé lënn Gumba rek meuna waaxni raagnéwulënn
En Europe y’a pas d’Eldorado Là bas quand t’es noir de peau sans papier c’est chaud Ne quitte pas ton pays pour vivre là bas comme un chardclo Ils ne respectent pas les hommes,ils ne font aucun cadeau Pour eux t’es qu’un migrant, t'es qu'un migrant de trop Ils ne t’aiment pas mais te sourient de peur que tu sortes les crocs, tous des hypocrites Aucun d’entres eux ne sont mes kho Ceepee Daddy Mory on chante pour tous nos bro
Sama gaayi dagnu bëgg dem Guen dem funé beug naaniu Naax fi daafa taar men Laamgu waalanimën Hi them crying again Lidu ronganiu nënn Bokku ci rewmi taaxul niu soraalè lënn Booy doox ci mbédmi faaw nga guissalé lënn Gumba rek meuna waaxni raagnéwulënn
Ku ci faalu né saay mbokk kaaylënn lëkk Gni faalu gnu faaluwaat gnom la rek Amna gnu nagu gnulënn di mom duloy guiss fëpp Dagno naagu sunu freedoom jeulnaaniu lëpp Gna thia dess wonbé léss jobu mbaam bi gnognu gnokooy meuna ress Dara dou bess sou mèloul nimou méloon dafaay guena yëss Mba mooy guen boon ngurr ngui moy sunu noon